Diiwaanu Kawlax
Apparence
Diiwaanu Kawlax benn la ci juroom-ñenti diiwaani Senegaal yi. Réewu-taax mu kawlax mooy péeyu diiwaan bi, te ëpp ci solo it. Mi ngi réye 16010 km2, am 1 066 375 ciy way-dëkk
Féeteem ci Melosuuf
[Soppi • soppi gongikuwaay bi]Mi ngi peggook:
- Diiwaanu Fatik (tunduw Gosaas) ci bëj-gànnaar ak diiwaanu Luga (tunduw Lingeer);
- Diiwaanu Tambaakundaa ci penku;
- réewum Gaambi ci bëj-saalum;
- Diiwaanu Fatik (tunduw Funjuñ ak wu Fatik) ci sowwu.
Ay tundam
[Soppi • soppi gongikuwaay bi]Ba ñu defee tunduw Kafrin diiwaan ci 2008, diiwaan bi ñetti tund rekk la am:
- Tunduw Kawlax
- Tunduw Kungéel (mi judd ci 2006)
- Tunduw Ñooro bu Rip
Lëkkalekaay yu biti
[Soppi • soppi gongikuwaay bi]- (en) Statistiques Geo Hive
- (fr) Région de Kaolack sur www.finances.gouv.sn
- (fr) La région aux Archives régionales du Sénégal
- (fr) Situation économique et sociale de la région de Kaolack (rapport officiel 2004)
| |||
Cees · Fatik · Jurbel · Kafrin · Kawlax · Kéedugu · Koldaa · Luga · Maatam · Ndakaaru · Ndar · Séeju · Siggcoor Tambakundaa · |