Arpagsàdd
Apparence
Ci làkku ibrë (אַרְפַּכְשַׁד / אַרְפַּכְשָׁד) la tur wi jóge. Ci angale mooy Arpachshad; Ci faranse mooy Arphaxad
Doomu Sem ak sëtu Nóoyin la woon. Juddoom fekk na mbënn ma weesu ba teg ñaari at (Ge 11:10-13). Kenn ci maamaati Yeesu yi ci Luug la woon (Lu 3:36).