Recueil Wolofal Sur S.babacar SY RTA
Recueil Wolofal Sur S.babacar SY RTA
Recueil Wolofal Sur S.babacar SY RTA
1. SALLI RABBI SALLOU ‘ALA NABII AHMED NAGNOU MOUGN MBAYE MI FÉROUU TEY
DOUNOU FATE NAGNOU MAGAL ABABACAR MINOU WOOLOU
2. KHALIFAY GUEDJ GUI DAMBER PENCOU BA SOWOUU KOUKO KHOUSS LAP WALA
NGA WAGNÉ KOU TÉ DÉLOU. DJÉGUIWOUL JAMBATOUL DOU KHASTER DOU GAARAL
LOUKO WAAY WAKH MOU BAYILAK KIKO WOOLOU
3. DJÉGUIWOUL JAMBATOUL DOU KHASTER DOU GAARAL LOUKO WAAY WAKH MOU
BAYILAK KIKO WOOLOU. TOPOU YALLA AK YONEN LA JANGAL NDIABOTAM KOUKO
TEK BAATE DOU GUESTOU YALLAH LA WOOLOU
4. TOPOU YALLA AK YONEN LA JANGAL NDIABOTAM KOUKO TEK BAAT DOU GUESTOU
YALLAH LA WOOLOU. YALLA YONENT AK CHEIKH AK MAODO LA JIITAL GNONI MBAYE
SY DOXAL SY IOW LAGNOUUU WOOLOU
5. YALLA YONENT AK CHEIKH AK MAODO LA JIITAL GNONI MBAYE SY DOXAL SY IOW
LAGNOUUU WOOLOU. CHAMSOU DINEY SA TOUR BI MAODO DEME TEY RAKHOULOO
DINE KHALIFA YA MATTA WOOLOU
6. CHAMSOU DINEY SA TOUR BI MAODO DEME TEY RAKHOULOO DINE KHALIFA YA
MATTA WOOLOU LAMOUDANE DEF NGA DEF TEYITE LAMOUDANE BAGN JEUFE
WOUKO BA YALLAH FAYE LA SI LOOLOU
7. ASS LAMOUDANE DEF NGA DEF TEYITE LAMOUDANE BAGN JEUFER WOUKO BA
YALLAH FAYE LA SI LOOLOU. MANA GANE AGAGOUL THI BERNDEL KOU TEWOUL
NANGOULÉNE JEUF YIII YALLAH MBAYE SY LA WOLOUU
8. MANA GANE AGAGOUL THI BERNDEL KOU TEWOUL NANGOULÉNE JEUF YIII YALLAH
MBAYE SY LA WOLOUU
KHALIFAY GORSI YALLA FAL YEUNGOUWOUL NGUIIR YEUFOU BAATINE JA THIA MOM
GOR DOUKO FATERR
(SALLI RABBI SALOU ALA NABII AHMED)
9. KHALIFAAY GORSI YALLA FAL YEUNGOUWOUL NGUIIR YEUFOU BAATINE JA THIA
MOM GOR DOUKO FATERR. RAFÉTAL NEY MBIRAM THI DINERRR BA KHEUY WAR
FASSOU LEER JEUM THIAA YALLAH MBAYE DOUNOUU FATERR
10. GORGUII RAFÉTAL NEY MBIRAM THI DINERRR BA KHEUY WAR FASSOU LEER JEUM
THIAA YALLAH MBAYE DOUNOUU FATÉ . DAGN WAR SANT YALLA MBAYE DAFA FAF TISS
BI NARONE GAR NDIABOOT GUIII SEUF NAKO YOBOUU
11. DAGN WAR SANTE YALLA MBAYE DAFA FAF TISS BI MARONE GAR NDIABOOT GUIII
SEUF NAKO YOBOUU
DAFA DOUY NDA YOU FESS BA TOUROUU MOU JOKHGNOU POTOU NDAA LAKOU
GNOU THI DESS NANOU FÉTERR
12. DAFA DOUY NDA YOU FESS BA TOUROUU MOU JOKHGNOU POTOU NDAA LAKOU
GNOU THI DESS NANOU FETERR . JIKO YONENT JA MOU YOR GNEPA KO SÉEDÉ DAFAA
AM THIEUR THIA YALLAH GNEPA KO SÉEDÉ
13. JIKO YONENT JA MOU YOR GNEPA KO SÉEDÉ DAFAA AM THIEUR THIA YALLAH
GNÉEPA KO SÉEDÉ
JEUFII YARAM JII MOU JEUF GNÉEPA KO TÉEWÉ NEUBII MBOTAM BA KHEUY NI MESS
DOUNOUU FATÉ
14. JEUFII YARAM JII MOU JEUF GNÉEPA KO TÉEWÉ NEUBII MBOTAM BA KHEUY NI
MESS DOUNOUU FATÉ. SOUNOUU YONENT BA ALTINERR BEUSSOU WOUTÉ SOUNOUU
KHALIFA BA MBAYE ALTINER BEUSOU WOUTÈM
15. SOUNOUU. YONENT BA ALTINERR BEUSSOU WOUTÉ SOUNOUU KHALIFA BI MBAYE
ALTINER BEUSOU WOUTÈME. SOUNOUU YONENT BEU NEK AÏCHA LA FATOOO
SOUNOUU KHALIFA BA MBAYE NEK MAME ASTOUU LA FATOOO
16. SOUNOU YONENT BEU NÈK AÏCHA LA FATOOO SOUNOUU KHALIFA BA MBAYE NEK
MAME ASTOUU LA FATOOO. BOUNOU JOOY GAINDÉ BAYINAAY GAINDÉ TÉ BOFOUUL
MOUDII KHAAAR BA BOROME KOUSSÈ DOUNOU GNÉTTER
17. BOUNOUU JOOY GAINDERR BAYINAAY GAINDERR TER BOFOUUL MOUDII KHAAAR
BA BOROME KOUSSÈ DOUNOU GNETTER. RANDAWOUL DAFA LAKOU TOKK DINOUU
SÉTANE SOUGNOUU JEUFLANTERR AK GAINDÈME YIMOUU BAYIII
18. MOTAX RAFETOUL DOMII GAINDÉ NDIAYE WATHIE WAASSO JAXASOOK KHAAAR
YAA YAGEU GUEY DINDI MINELO. SOUKO KHAAAR YA YABERRR THI MOM LA DOU
THIAKHANE DAFA WAR DÉLOU ALE MO GUEUNA WÉLOO
19. KONE NAGNOU WAYLO TER MOY THI GNOME BAGNA TAYI BAGNA FAGEUNE
WAXONE NAGNOUU BOLOU JITOUU. SOUFII MBAX DONE SAXAL GORGUII DOUFII JOUG
TEY SOUFII THIEUR DONE SAKHAL MAME MBAYE DOUFII JOUK TEY
20. SOUFIII MBAX DONE SAXAL GORGUII DOUFII JOUG TEY SOUFII THIEUR DONE
SAKHAL MAME MBAYE DOUFII JOUK TEY. KOUDI SOPEM JEUFLANE TÉNAK IOW THII
BAATINE TEEY RAAW GNARIII LAMPEU SAX LEEY NITERRR
21. KOUDII SOPEM JEUFLANE TENAK IOW THIUI BAATINE TEEY RAAW GNARIII LAMPEU
SAX LEEY NITERRR. NEGNOU YEM JEUFII YALLA MOM DAFA WOUTÈK LIMOU NASS
GORSA DEMNAA GOR DOUKO FATERR
22. NÉGNOU YEM JEUFII YALLA MOM DAFA WOUTEK LIMOU NASS GORSA DEMNAA
GOR DOUKO FATERR. JIKO YARAM JA THIA MOM TAKH MEUSSOUGNO FOGNE DOUNOU
WEDII NDIGEUL MAME YAY SOUNOUU FETERR
23. JIKO YARAM JA THIA MOM TAX MEUSSOUGNO FOGNE DOUNOU WEDII NDIGEUL
MAME YAY SOUNOUU FETERR. DAFA GNOU DANE BEGEUL KOUNEK LAMOULEY JOKH
BATHIIE MANE AK YENE DÈME JIII GNEPA LA METTI
24. DAFA GNOU DANE BÉGUEUL KOUNEK LAMOULEY JOKH BATHIIE MANE AK YÈNE
DEM JIII GNEPA LA METTI. DAFA TALAL LOXOM NDIABOOT GUIKO WEUR TEY
MEUSSOUNOO KHIFF BA DEM FÉNÈNE DIFA KHAARRI
25. GORGUII DAFA AM DINERRR AM NGOR AM SOUTOURAK KHEL RAWER MANDOK
MOUGNE AK TABER TÉEEUDOU WOUTER. GORGUII DAFA AM DINERRR AM NGOR AM
SOUTOURAK KHEL RAWER MANDOK MOUGNE AK TÈYE DEUDOU WOUTER
GORGUII DAFA AM DINERRR AM NGOR AM SOUTOURAK KHEL RAWER MANDOK
MOUGNE AK TABER TÉEEUDOU WOUTER. NAKO YALLA YOKAL LERR YAMOU FEKII
SOUTOURAL GNIMOUU BA GANAAW BAGNOUU MAGATE
26. NAKO YALLA YOKAL LERR YAMOU FEKII SOUTOURAL GNIMOUU BA GANAAW
BAGNOUU MAGATE. DEUGEUREUL SENII THIEUR GNOU OUFF NOU BA SODANE BAGNA
JOOY GORSA DEMNAA GOR DOUKO FATERR
FIN
KOUKO AM AMNGA YONENT AM MAODO AM CHEIKH MINOU DOY (BIS)
FIN
KHALIFATAS SHEIYKHI WAL MOUQTARI YAFI DI MBEUR SY YAYE FAJAL DINER AY
DANAM TER GNEP LA WAR
FIN